Africando – Dieguema Lyrics

Ritmo Africando
Oy!
Massa
Haba!

Ifexal saxal moy syiw li dundal xol ci nit
Moy mbëgël
Sumbëgël taxe maway la caw fe latax
Maye am xala
Sumbëgël taxe maway la caw fe latax
Maye am xala
Di wax ci yow lu ken
Mansul xala di wax keneen
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Sumare ni xol wayuma ñëwel jël me
Yama wara jël, kay jël me
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Sumbëgël taxe maway
Caw fe latax maye am xala ci yow
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Di wax ci yow lu ken
Mansul xala di wax keneen ku dul yow
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Diya taxe makan bëgël
Ni mala bëgël
Epp na keneen ku dul yow

Jege ma jege ma
Ka jege ma
Jege ma jege ma
Wayuma
Jege ma jege ma
Ka jege ma
Jege ma jege ma
Wayuma

Ifexal saxal moy syiw (Jege ma jege ma wayuma)
Li dundal xol ci nit moy mbëgël (Jege ma jege ma wayuma)
Am bëgël bëgël bëgël bëgël bëgël (Jege ma jege ma wayuma)
Samare ni xol wayuma (Jege ma jege ma wayuma)
Ni amël ci man la amël ci yow (Jege ma jege ma wayuma)
Luma masa xam wax na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
Luma masa gis woon na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
Di lawoon di lawoon
Luma masa am jox na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
(Khay!)

Yow mi jam cëmoom
Yow yow
Yow mi jam cëmoom
Yow mi jam cëmoom
Yow mi jam cëmoom
Yoppantëna
Bo deme nga ni ko
Mbëgël metti na
Na metti na loor
Gise Yallaay boor
Bulma min fa dema
Bulma xam ba yimma
Ci loolu ci loolu ci likay jege ma ci loolu
Ci loolu ci loolu ci likay jege ma ci loolu
Khay!

Woo naale guddi
Woo naale bëjëk (Wayuma samare ni xol)
Sëmoyu bëjëb yi wax nañ la ko (Wayuma samare ni xol)

Comments (0)